Lakhdary : Leçon 1



Presnter par: Cheikh Younousse Ndiaye

Gnou ngui gnane yalla commencer ci bismillahi rahmâni rahîm diékhalé ka ci Alhamdou lillahi rabil hâlamine🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲.
képe kou beugue khame naka ngua wara jiamô borome bi ci jamou jou wére gnou ngui laye gnâne ngui suivre bîlé programme nakhe kgua meune ci dieurignou🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏.
Yalla nagnou yalla nangoul sougnou diamou ta foulale gnouka🤲🤲🤲🤲