La leçon de modestie de Cheikh Mahi NIASS !dant que les activistes et certains wahabites insultent



Hormis son humilité naturelle, Cheikh Mahi montre aux yeux du monde que ce pays mérite d’être cru.

Meuna gnu xass Kilifeu Diné yi Mais ken meunul dindi sen mérite et cela est prouvé depuis des lustres.
Respecter leeen KILIFEU Diiné yi YALLA hamna ni lignuy jarign SENEGAL mindeeef meunu ko!

J’ai jamais demandé qu’on lui donne le Prix Nobel de la Paix ndah pour un soufis comme lui c’est dérisoire. Talou gnu ay Prix yo hamni gni ka jeul dougnu dara. Sen instance de mesure YALLA moko yorrr!

Na YALLA samm KILIFEU DIINÉ yi nek si reew mi!
Jërëjëfé Cheikh Mahi Niasse

جزاك ربك عن بني الأوطان

PS: kou fi nekkati di diingat tariqa wah leen ko na def ni Cheikh Mahi def baparé soga meuna critiquer. Cet acte est la meilleure des preuves.